1: njàng mu jëkk

 0    92 フィッシュ    kavadias
印刷 遊びます 自分をチェック
 
質問 答え
apprendre
学び始める
jàng
saluer
学び始める
nuyu
se saluer
学び始める
nuyoo
remercier
学び始める
sant
être le premier
学び始める
jëkk
arriver
学び始める
àgg
arriver au lieu où se trouve le locuteur
学び始める
agsi
leçon
学び始める
njàng (m)
salutation
学び始める
nuyoo (b)
lieu
学び始める
bërëb (b)
maison
学び始める
kër (g)
épouse
学び始める
jabar (j)
maisonnée
学び始める
waa kër (g)
paix
学び始める
jàmm (j)
corps
学び始める
yaram (w)
Tu vas bien?
Ton corps a la paix?
学び始める
Sa yaram jàmm?
à, dans, sur
学び始める
ci
où est, où sont
学び始める
ana
comment
学び始める
naka
ici / là
学び始める
fi / fa
seulement
seulement de paix
学び始める
rekk
jamm rekk
époux
学び始める
jëkkër (j)
main
学び始める
loxo (b)
pied, jambe
学び始める
tank (b)
tête
学び始める
bopp (b)
oreille
学び始める
nopp (b)
oeil
学び始める
bët (b)
nez
学び始める
bakkan (b)
cou
学び始める
baat (b)
bouche
学び始める
gémmiñ (g)
langue
学び始める
làmmiñ (w)
poitrine
学び始める
dënn (b)
remerciement
学び始める
cant (w)
parler
imp. A
parle! parlez!
学び始める
wax
-al, -leen
waxal! waxleen!
apporter
imp. B
apporte! apportez!
学び始める
indi
-l, -leen
indil! indileen!
saluer
imp. B
salue! saluez!
学び始める
nuyu
-l, -leen
nuyul! nuyuleen!
appeler
imp. B
appelle! appellez!
学び始める
woo
-l, -leen
wool! wooleen!
mettre ensemble
imp. C
mets ensemle! mettez ensemble!
学び始める
boole
(-v)l, -leen
booleel! booleleen!
tiens! tenez!
imp. exc.
学び始める
am! amleen!
viens! venez!
imp. exc.
学び始める
kaay! kaayleen!
ne parle pas! ne parlez pas!
imp. neg
学び始める
bul wax, buleen wax
bul +, buleen +
comment as-tu fait?
sing. 2/3 & pl. 2/3
comment vas-tu?
学び始める
na / naka nga def? naka la def?
na / naka ngeen def? naka lanu def?
je suis ici - ils sont ici
1 - 3, sing.& pl.
présentative: sujet est dans un espace proche du locateur
学び始める
maa ngi fi, yaa ngi fi, mu ngi fi
ñu ngi fi, yeena ngi fi, ñu ngi fi
il / elle est ici / là
sujet se trouve éloigné, hors de vue du locateur
学び始める
mu ngi fi / mu nga fa
que 3e personne
ñu ngi fi / ñu nga fa
grâce à Dieu, ça va
il / elle est là en train de remercier Allah
学び始める
mu ngiy sant Yàlla
ngiY
je - ils suis en train de partir / je - ils m'ent vais
1 - 3, sing. & pl.
construction: situe l'action dans le présent de l'énonciation (! pas temps présent!)
学び始める
maa ngiy dem, yaa ngiy dem, mu ngiy dem
pronom + ngi + y + verb
ñu ngiy dem, yeena ngiy dem, ñu ngiy dem
je pars
une façon de prendre congé
学び始める
maa ngiy dem
mon corps
2
mon, ma
学び始める
sama / suma yaram
sama / suma
ton corps
ton, ta
学び始める
sa yaram
sa
son corps
son, sa-a
学び始める
yaramam
-am
notre corps
notre
学び始める
suñu yaram
suñu
votre corps
votre, leur
学び始める
seen yaram
seen
comment va la famille?
10 classes nominales (8 au singulier, 2 au pluriel)
Où sont les gens de la maison ici / là-bas?
学び始める
ana waa kër gi / ga
sing.: gi, mi, li, bi, ji, si, ki, wi.pl.: yi, ñi
-i // -a
prier
学び始める
julli
emmener
学び始める
yóbbu
être d'accord
学び始める
juboo
envoyer
学び始める
yónnee
manger
学び始める
lekk
boire
学び始める
naan
entrer
学び始める
dugg
se baigner
学び始める
sangu
photographier
学び始める
foto
remettre
学び始める
joxe
voici l'arbre
l'arbre
voilà l'arbre la-bàs
学び始める
garab gaa ngi
garab gi
garab gaa nga
voici l'enfant
l'enfant
voilà l'enfant là-bas
学び始める
xale baa ngi
xale bi
xale baa nga
la mosque
学び始める
jàkka ji
l'eau
学び始める
ndox ma
l'hôte
学び始める
gan (g)
le professeur
学び始める
jàngalekat bi
le marché
学び始める
marse bi
la poste
学び始める
post bi
la clé
voici la clé
学び始める
caabi (j)
caabi jaa ngi
le chien
学び始める
xaj bi
le sable
学び始める
suuf sa
où est l'enfant?
il est ici / là-bas
学び始める
ana xale bi?
mu ngi fi / nga fa
la calebasse
学び始める
leket (g)
le lait
学び始める
meew (m)
la femme
学び始める
jigéen ji
l'homme
学び始める
góor gi
feu
学び始める
safara (s)
la chose
学び始める
këf (k)
le cheval
学び始める
fas (w)
la personne
学び始める
nit (k)
singe
学び始める
golo (g)
la marmite (the kettle)
学び始める
cin (l)
il écrit le professeur
proche
学び始める
jàngalekat baa ngiy bind
elle retourne l'auto
proche
学び始める
woto baa ngiy dellu
le vieux va mieux
loin
学び始める
góor gaa ngay tane
il ferme la boutique
学び始める
borom bitig baa ngiy/ngay téj
l'enfant vient
学び始める
xale baa ngiy/ngay ñów
il bout (boil) le café
学び始める
kafe gaa ngay bax
le taxi s'arrête
学び始める
taksi baa ngay taxaw

コメントを投稿するにはログインする必要があります。