Directions

 0    59 フィッシュ    kavadias
印刷 遊びます 自分をチェック
 
質問 答え
Which road is going to...?
学び始める
Ban yoon moo jëm?
Go straight (2)
学び始める
Jubbalal / tallal
jubbalal is also for persons, tallal only for direxrions
I live in Fann Residence, close station Elton Mermoz
学び始める
Maangi dëkk Fann Résidence, wettou Station Elton
I want to go to Station Elton Mermoz
学び始める
Station Elton Mermoz laay dem
I have 1000 Fran
学び始める
Mille fran laa am
1000 Fran is good
学び始める
Mille fran baax ma
The next road
'see you the next road'
学び始める
Beneen yoon
ba beneen yoon
Left
学び始める
Cammoñ
[tsj]ammoñ
right
学び始める
Ndeyjoor
Go until
学び始める
Demal ba...
Cross the paved road
学び始める
Jéggil tali bi
Cross to the right
'take'
学び始める
Jaddal ci sa ndeyjoor
jëlal
Take the left
'cross'
学び始める
Jëlal ci sa cammoñ (tjs)
Jaddal
Take this road
学び始める
Jëlal yoon wii
Where is ...?
学び始める
Ana/fan la ... nekk?
It's located at...
学び始める
Mungi ci...
Is it far?
学び始める
Sore na?
It is far
学び始める
Sore na
It is not far
学び始める
Sorewul
What is there/can be found there?
学び始める
Lu am foofu?
There is...
Also in restaurants, shops, etc.
学び始める
Am na...
Is there ...?
学び始める
Ndax am na ...?
Is it a ...?
学び始める
Ndax ... la?
Where can one find ...?
Also for water, items, etc.
学び始める
Fuñu mëna ame ...?
I am lost
学び始める
Dama réer
My phone is lost
学び始める
Suma portable réer na
Multistoried building
Go until the flat
学び始める
Tax bi
Demal ba tax bi
the tree
学び始める
gui bi
In front of
also used when meaning ‘a bit further’ (e.g. taxi)
In front of the tree
学び始める
Ci kanam
Ci kanam gui bi
Behind, after
学び始める
Ci gannaaw
In the centre/middle of...
学び始める
Ci diggu...
In the centre
学び始める
Ci digg bi
Between ... and...
Between the flat and the tree
学び始める
Ci diggante ... ak...
Ci diggante tax ak gui bi
Before
time & space
学び始める
Balla
Next to / close to
学び始める
Ci wet u
Far from
Far from the market
学び始める
Sori na
Sori na marché bi
Above / on
学び始める
Ci kaw
Below
sand
学び始める
Ci suuf u
suuf
Under
学び始める
Ci suufu
Inside
学び始める
Ci biir
Outside
学び始める
Ci biti
Stomach, pregnancy
My stomach
学び始める
biir
Suma biir
Inside my car
学び始める
Suma biir oto
I am in the market
学び始める
Man ci biir marché
Dirt road
学び始める
Yoonu suuf
Paved road
学び始める
Tali
Street
学び始める
Mbedd
It's not far, about 20 km
学び始める
Sorewul, mungi toll ci 20 km
close (distance)
come close to me / come close
学び始める
jege
jege si ma
not close
negative marker
学び始める
jegewul
-wul
How can I go there?
we
学び始める
Naka la mëna deme foofu
la -> lanu
to go
学び始める
deme
time
学び始める
waxtu
Which time
学び始める
Ban waxtu
What time will you come?
to come
学び始める
Ban waxtu nga ñëw (ñow)
ñëw (ñow)
I go / come my house
学び始める
Maangi deme / ñëw suma kër
He will take you to Marseille
学び始める
Mën na la yobbu Marseille
To take (a person)
Take me to the restaurant
学び始める
yobbu
Yobbu ma marsé
I wish to go to Fann Residence
学び始める
Fann residence laay bögg dem

コメントを投稿するにはログインする必要があります。