Ñetteelu njàng: wonale

 0    40 フィッシュ    kavadias
印刷 遊びます 自分をチェック
 
質問 答え
présenter
学び始める
wonale
se nommer (nom de famille)
学び始める
sant
être petit, peu
学び始める
tuuti
entendre, comprendre, parler (langue)
学び始める
dégg
appartenir
学び始める
bokk
venir, arriver
学び始める
ñow
habiter
学び始める
dekk
accueillir
学び始める
teertu
présentation
学び始める
wonale (g)
invité
学び始める
gan (g)
nom de famille
学び始める
sant (w)
parent, allié
学び始める
mbokk (m)
ville, village
学び始める
dëkk (b)
touriste
学び始める
turist (b)
est-ce que (j'espère)?
学び始める
mbaa?
est-ce que (par hasard)?
学び始める
xanaa?
est-ce que (neutre)?
学び始める
ndax?
où est-ce que?
学び始める
fan?
quoi, qu'est-ce que?
学び始める
lan?
se nommer (prénom, nom)
学び始める
tudd
prénom et nom
学び始める
tur
lundi
学び始める
altine
mardi
学び始める
talaata
mercredi
学び始める
àllarba
jeudi
学び始める
alxames
vendredi
学び始める
àjjuma
samedi
2
学び始める
gaaw, aset
dimanche
学び始める
dibeer
j'espère qu'il comprend le Wolof?
question fermée + particules
学び始める
mbaa dégg na Wolof?
mbaa: orient la réponse d'interlocateur
Tu es touriste, pas hasard?
question fermée + particules
学び始める
turist nga xanaa?
xanaa: orient la réponse d'interlocateur
[je suis parti]
(passé composé)
résultatif + verb d'action: 1-3e p., sing. & pl.
学び始める
dem naa, dem nga, dem na
dem nañu, dem ngeen, dem nañu
[je comprends]
présent d'état
résultatif + verb d'état: 1-3e p., sing. & pl.
学び始める
dégg naa, dégg nga, dégg na
dégg nañu, dégg ngeen, dégg nañu
Le nom?
question ouverte
Comment tu t'appelles?
学び始める
Sant wi?
Parent d'où?
d'où viens tu?
学び始める
mbokki fan?
qu'est-ce que tu fais à Dakar
question ouverte
学び始める
Lan ngay def Ndakaaru?
quand es-tu arrivé ici?
question ouverte
学び始める
Kañ nga fi ñów?
[je suis touriste]
le verb être n'existe pas en wolof
[être]: 1-3e p., sing. & pl.
学び始める
turist laa, turist nga, turist la
turist lañu, turist ngeen, turist nañu
[je ne suis pas touriste]
le verb être n'existe pas en wolof: la forme négative est dissymétrique
[n'être pas]: 1-3e p., sing. & pl.
学び始める
duma turist, doo turist, du turist
duñu turist, dungeen turist, duñu turist
j'ai une maison
voici ma maison
学び始める
am naa kër
suma kër a ngi
il a un ami
voici son ami
学び始める
am na xarit
xaritam a ngi

コメントを投稿するにはログインする必要があります。