Wonale (Introduction)

 0    53 フィッシュ    kavadias
印刷 遊びます 自分をチェック
 
質問 答え
What is your name? (3)
学び始める
Noo tudd? Nanga tudd? Naka nga tudd?
naka nga/nanga: new info; noo: confirmation
My name is...
学び始める
... laa tudd.
What is your last name? (3)
学び始める
Noo sant? Nanga sant? Naka nga sant?
My last name is...
学び始める
... laa sant
Where do you come from (2)
学び始める
Foo jòge? Fan nga jòge?
I come from...
学び始める
... laa jòge
Where do you live? (2)
学び始める
Foo dëkk? Fan nga dëkk?
fan nga: info unknown; foo: confirmation
I live in...
学び始める
... laa dëkk
Who?
also plural
学び始める
Kan (ñan.pl.)?
What?
学び始める
Lan?
Est-ce que?
学び始める
Ndax?
Where?
学び始める
Fan?
How many?
学び始める
Ñaata?
How?
学び始める
Naka?
Which?
also plural
学び始める
Ban (yan.pl)
When?
学び始める
Kañ?
Westerner
学び始める
Tubaab
Man
学び始める
Gòor
Woman
学び始める
jigéen
child
学び始める
xale
Adult
学び始める
mag
young
学び始める
ndaw
Young woman
学び始める
jànq
young man
学び始める
waxambaane
Old person
学び始める
magget
Crazy person
学び始める
dof
I am Dutch
学び始める
Hollandais laa
I am not French
学び始める
Duma Fransé
husband
学び始める
jëkkër
wife
学び始める
jabar
child
学び始める
doom
boy friend (2)
学び始める
far / coof
girl friend (2)
学び始める
coro / gel
single
学び始める
selibateer
I have a husband / wife
学び始める
am naa jëkker / jabar
I don't want a girlfriend
学び始める
Bëgguma coro / gel
Do you have a boyfriend?
学び始める
Am nga far / coof?
No, I don't have a wife
学び始める
Déetdéet, amuma jabar
Teacher
学び始める
jangalekat
student
学び始める
elew
Seller
学び始める
jaaykat
lit.: sell + person
What is your job? (2)
学び始める
Looy liggéey? Luy sa liggéey?
I am a teacher
学び始める
jangalekat laa.
To live
学び始める
Dëkk
To be named
学び始める
tudd
To be / to be located
学び始める
Nekk
To be born
学び始める
Juddu
To grow up
学び始める
màgge
To come from
学び始める
jòge
A name
学び始める
tur
A surname
学び始める
sant
Also (2)
学び始める
tamit / itam
Really, truly!
学び始める
Ci dëgg-dëgg

コメントを投稿するにはログインする必要があります。